ARK NETWORK reference.ch · populus.ch    
 
  
La vie qui sommeille en toi 
 
 
Rubriques

Liens

 Home  | Livre d'Or  | Album-Photo  | Contact

le bien aimé

Dans l'unité de Dieu et dans la réalité Mouhamadienne, baye djine m'a réveillé non pas par le verbe, ni par le touché, mais par le vin de l'Amour pour Baye Laye. 
 
Profésseur Libasse DIOP - UCAD 
Profésseur d'ici-bas, Profésseur dans l'Au-dela 
 
Louanges à mon seigneur,à mon bonheur 
Ils sont trés minimes ceux qui te connaissent 
Beauté divine qui dilate l'ame et l'esprit 
A toi les honneurs dans la totalité des possibles 
Seul l'ignorant te considére comme un simple méssager 
Salutations à toi qui est intimement lié à l'Absolu 
Exalter la grandeur de notre seigneur Moustapha 
 
Lenteur des savants,dévotion des croyants 
A chaque étape tu es notre guide,notre sauveur,les 
Yeux sublimes auxquels nous regardons,cet 
Etat qui fait que l'on dépasse les limites fixées par soi  
 
Roi éternel dans ce monde et dans l'au-dela 
Amour divin des gens de coeur et d'esprit 
S'assembler,chanter pour bien te plaire 
S'éloigner loin de tout autre que toi 
Ouvres la voie secréte qui méne à toi sans 
Laquelle rien ne peut étre apprécier 
O toi le moulin éternel de notre vie 
Un instant de ta présence équivaut à mille et un univers 
 
La vie a ses secrets,l'adoration aussi 
A toi l'unique qui nourrit notre religion 
Y a t'il un chemin autre que celui de l'Amour 
Et s'il existe,je préfére celui de Libasse Laye.  
 
 
 
Dans cette quête perpetuelle de l'amour divin pour Baye laye, le professeur a composé un chef-d'oeuvre de chansons à la gloire de notre Seigneur Seydina Djine Coumba : 
 
 
BISMI LAHI RAHMANI RAHIM 
 
Allahouma salli alla 
Sangoub Jamana Mame Libass 
Allahouma salli alla 
Rassolou Sope Rabana 
 
Allahouma salli alla 
Borom Jamana Mame Libass 
Allahouma salli alla 
Rassolou sope Rabana 
 
Allahouma salli alla 
Khayroulwara Limamou Lahi 
Allahouma salli alla  
Madiyou Sope Rabana 
 
Yalla la yoni Mame Libass 
Amo morom Djine Diamalaye 
Yalla la tanna do morome 
Rassoulo sope Rabana 
 
Baye laya wote no wouyoo 
Mou ser thia kaw ni Madiyo 
Borom arassa yoniwat  
Thi gnoune sangaba Momado 
 
Timis na kouka fadiar nagna 
Takoussane na soufé lol 
Loloy ndigalou Mame Libass 
Rassoulo Sope Rabana 
 
Dianta bou sangou warouleen 
Na takha naan thi ramadan 
Borom diamana nenaleen 
Takhirlouleen ba mou nelaw 
 
Limoy ndiguelou Mame Libass 
Sangoup jamana Momado 
Mame doyngano Limamou Lahi 
Rassolou Sope Rabana 
 
Choukrane hamedane fikoullizatine 
Mahane li Rabana 
Mignouye dioulil thi Mame Libasse 
Rassoulo Sope Rabana 
 
Ya Rabana sounou borom 
Dioulil thi mame Limamoulaye 
Ndjine sori dektou Momado 
Rassolou Sope Rabana 
 
Allahouma salli alla 
Fikoullizatine Mame Libasse 
Allahouma salli alla 
Fikoullizatine Momado 
 
Jullito jullil ci Mame Libasse 
Jullito jullil ci Mame Libasse 
Jullito jullil ci Mame Libasse 
Jullil ci sope Rabana 
 
Daoudak Zacharia 
Ismaila Ibrahima 
Idrissa wa Yahia 
Gnoungay julli ci Mame Libasse 
 
Sa Mame Limamou kenalaa 
Sa Mame Limamou Kenalaa 
Bour Yalla Lahou Kenakaa 
Djital sangaba Mame Libasse 
 
Amantou wahidoune Allah 
Amantou mame Limamou Lahi 
Ma feegn fa beegn ba Diamalaye 
Ni Momadou Makka yewouna 
 
Bour Yalla sope Mame Libasse 
Mo kawel Limamou Lahi 
Djine Diamalaye "Peremyé" 
Fa bourba Rabana Jalil 
 
Ba Mame taggo wa Diamalaye 
Deugmeul Bourba Rabana 
Ibnou Mariamak Faty Lahi 
Ya egalé wote Mame Libasse 
 
Bindakoonbak Mame Libasse 
Gnoma santa diouli lo 
Jullit gni ci Mame Libasse 
Rassoulo sope Rabana 
 
Kou geume tekhe fa Mame Libasse 
Kou geume tekhe fa Mame Libasse 
Kou geume tekhe fa Mame Libasse 
Mi Yalla tanna yonika 
 
Guigne na ni Rabana Jallil 
Sope Mame Limamou laye 
Yama digueul beugeuleka 
Abadane Limamou Lahi 
 
Sa Mame Limamou teknama 
Ca Djibril Laye mou teddama 
Nandalima ca leeram ya 
May diwan fa sawouba 
 
Tipo na Limamou Lahi 
Tipo na Limamou Lahi 
Tipo na Limamou Lahi 
Sama sope sope Rabana 
 
Dioulito beugeul Limamou Lahi 
Dioulito doylol Limamou Lahi 
Dioulito royal Limamou Lahi 
Dioulito jullil ci Mame Libasse 
 
Wa aras ak koursiyo 
Wa sadiaratahal mountaha 
Wa lakram firdawse 
Ngay julli ca Mame Libasse 
 
Wa ndigalaak diamalaye 
Wa guédiagak khoutama 
Boroom kalaya Cambéréne 
Ño ngay julli ca Mame Libass 
 
Wa Camberene ak yoffi guej 
Wa Malikak Beyti Mamour 
Jullilleen ci Mame Libasse 
Miy khédiaba fa Rabana 
 
Ya Yayo Lolou Mame Libasse 
Ya yayo Lolou Mame Libasse 
Ya Yayo Lolou Mame Libasse 
Yonenbi sope Rabana 
 
Guigne na thi Lahou kiy Borom 
Ni Kaabaga nga Diamalaye 
Fofaye bureau Limamou Laye 
May Tampe Dieufyou Magaya 
 
Jullit jullil ci Mame Libasse 
Jullil feete Diamalaye 
Daytalou Djamouga 
Fa Bour ba Lahou Rabana 
 
Kouy julli ci Mame Libasse 
Da ame payor fa Rabana 
Kouy julli ci Mame Libasse 
Da tafok Limamou Lahi 
 
Doy lo nala Mame Libass 
Doy nga ma Limamou Laye 
Doy nga Bourba Rabana 
Yaw rekay sanga Madiyoo 
 
Mboleem li foreyiy yakhal 
Donou fidef lou gueuneul Bour 
Li Djine wakh ni julileen 
Abadane ci Mame Libasse 
 
Sa Mame Limamou dignama 
Teddanga diou kheel dadjul 
Fa bour ba Lahou Rabana 
Ngir digle sounou Mame Libasse 
 
Bou diok djote djeum firdawse 
Ba bourba tek siratamma 
Kerok gna weddi borom kalaya 
Gnégna diouli dioublou Diamalaye 
 
Mamodou makka Sopeba 
Mo ni gnay tafok rassol 
Bou eulegue fa Rabana 
Moy gnay julli fa Mame Libasse 
 
Guigne na ci Rabana Jalil 
Ni Mame Limamou rekka mane 
Dara ca Bourba Rabana 
Bissoup diatay bou Metibaa 
 
Tepatepalou Rabana 
La Mame teggoon gna jëka gëm 
Mo digal wa Diamalaye 
Gnou khouss ba seey ci seen Borom 
 
Ya yakal gnu weexgna Momadok 
Ababacar Omar Ousmane 
Aliok Jaffara 
Gnou sampa dine Rabana 
 
Sodane seddo sa Mame Libasse 
Ak Rowalaye mou faty Laye 
Ak julli ci Madiyok 
Julli feete Diamalaye 
 
Deeleen siyari Diamalaye 
Bouleen di guedj ca Seydi Laye 
Borom Beyti sedeess naka 
Wawou watori moka moom 
 
Sa mamay yee wa Diamalaye 
Gnou diouli ci Mame Limamou Laye 
Ay diouniy at fa Diamalaye 
Bagn yay xandoor gnou fawxaleen 
 
Mille un tombouba sa Mame Libasse 
Mille un alifouba Djine Diamalaye 
Sa Mame Limamou Kenala 
Rassoulou sope Rabana 
 
Bayelaya pé Bayelaya pé 
Bayelaya pé Bayelaya pé 
Bayelaya pé Bayelaya pé 
Bayelaya pé Bayelaya pé 
 
Jullit jullil ci Diakou Djine 
Yeek Nianoukayou Mame Libasse 
Begal Bayelaye mou Rabana 
Am Ngereumeum lou tedalaa 
 
Allahouma salli alla 
Kholou Rabana Limamou Laye 
Allahouma salli alla 
Kholou Rabana Djine Diamalaye 
 
Allahouma salli alla 
Sangoub Jamana Mame Libasse 
Allahouma salli alla 
Rassolou sope Rabana 
 
Allahouma salli alla 
Borom Jamana Mame Libase 
Allahouma salli alla 
Rassoulou sope Rabana. 1996 
 
 
HOMMAGE A MOUSTAPHA L'ELU, LE BIEN AIME 
 
Ñu dellu santa Moustapha 
Mom minu tégalli ay safane 
Batey ñu santa rabul Khadim 
Di ñan mu teknu ciy bireum 
 
Budul konté Moustapha 
Keen du ni nam bay sabba 
Ku wéddi ki dawal kéneen 
Ta kham ni sa thieuf néna neen 
 
Ma wakh leen sa map xam ci Moustapha 
Taaru, tabé, mougn ta ame daraja 
Kou aga ca Yalla ci moom ga thiar 
Lii dé wor na kouy sééték di khar 
 
Ñeenta ñi ño seuce ca Moustapha 
Ababacar, Omar ño djitu ci Khalifa 
Ousmane égali séni am am 
Boul faté Alioune babul xam xam 
 
Moustapha nélaw, yéwu doon Libasse 
Ka wooté woon ca Makka, woté ci Yoffi téféss 
Baatam ca kaw muy woté naan 
Kayleen ñu jamou Burbi Rabban 
 
Ñu naan ko wax thi rey na ya Libasse 
Yaw miy teukeulé Momado thi mass 
Da ño xamul ni Bourbi ay dogalam 
Mbidéf yi amouni ci tarafata xam xam 
 
Djinoo, Djine, Djinoo Libasse 
Ka Yalla tana déf ko amoul masss 
Di khalat thi ay biireum 
Xél dina sonna ta du takha xam 
 
Souguéne xamone li thi beugél ca Mame Libasse 
Dina sol ruu boléki faxass 
Bésub kérok sa leer di bawaan 
Nga yék ca gaal ga séti Rabban. 
 
Geum ndawalu Yalla démb, wéddi ko tay 
Bou euleugué yol bi dina néw ci pay 
Wax wax du takha disoub eumb 
Say nit di youkhou dakh geuleum. 
 
Ignane ak sokhor diourna geuleum 
Thiow ak reuy do agga faga dieum 
Wakh thiothia ñél na ña wéddi Diol 
Euleuk diahanama di foudou ñuy khol 
 
Limamou diamono euy kou wéddi Djine 
Diamou diamou sa ruu di biigne 
Ku dul Yalla ak Djine di néen 
Mbidefi soodan yi séddé léen 
 
Buleen khamone wa kalaya thi may 
Ña matal dëmb di motali tay 
Ñu naneléen wathiaguén yonu deug 
Ñunan ñugui diamou ba euleug 
 
Séni wadiouryi santa warna leen 
Ñel kileen thiox ño ña ta dioxowunou néen 
Ku am domu général loy doyé gobi 
Ña wéddi kiñane dal naléne thi lii 
 
Thiofél gacca Yalla ak Diol ma saxna 
Bataxna kou dieufeuk koka rawga 
Ba Mame woté la deunou gagna riréé 
Ñu nane ko Mame dotu nu la diawat lé 
 
Heuxlou soodan séni wéddigui féñña 
Kiñane ak reuy féss na seni xol ya 
Xolou ña gueum di bawaan ci Rabaan 
Ku muri beuteum, dégba dothia naan 
 
Al hamedoulilahi ba nu geumé Djine ak Djarafam 
Watou nél sol lu wééx lanu digeul ci xam xam 
Ka seugueu ci tééré ak waxu démb di alagué 
Batin ak saahir danél na ñu baré 
 
Mame xala yonni wi soodan tégui 
Raw ak dool adiou ci gueum ak wéddi 
Ka diaxassok Bourba rérna nit nia 
Wakham di andak kounou Yalla thia 
 
Alxourhane ni diol ñu djitou ak ñu muthiéna 
Foreya nan diol lu Makka Abada 
Démb perkal mo dém ba ñul 
Ruu djeuma thiou sop Bur mu sulu 
 
Alifou Basmalate reer na borom téréya 
Burba neubefa sopém ba 
Ka Yalla oubil yéna thi ay Mbireum 
Batam di dal thi ñay boubo xam xam 
 
Woté ba djip ruu nan amana 
Seytané bésoup kérok dé dioyna 
Ñaari xét yi yéllo sagaba 
Yiiw ak tabé mo léen may koka 
 
Soodaan di gueustou ci térék funé 
Geuleum guou tare xañ lén louné 
Batax ñu dém makka ba wésufa 
Fa diamalaye ñuy siyari Diolma Moustapha 
 
Araf ya reer na ñay firi Alxourhan 
Kou Khoulok borom Keur lo di kharane 
Diouli ci Baye Libasse rawlona kou gueum 
Diamano bou nieuw andak Booteum.

 

(c) gotts78 - Créé à l'aide de Populus.
Modifié en dernier lieu le 19.12.2014
- Déjà 6779 visites sur ce site!